Pedir ayuda - Pedir información
Baal ma, ndax mën nga ma dimale? - Por favor, ¿me puede ayudar?
Deguma español – No hablo español.
Deguma (kalama bi) – No comprendo.
Baal ma nga baamtu ka – Repita, por favor.
Baal ma nga wax bu teey – Hable más despacio, por favor.
Waaw / Déedeet – Sí / No.
Jërëjëf – Gracias.
Sula neexee (baal ma) – Por favor.
Baal ma / Jeggëlma – Perdone / Disculpe.
Maa ngiy jeggëlu – Lo siento.
Baal ma, ngir dem ba mbeddu Barcelona? - ¿Para ir a la calle Barcelona, por favor?
Fan la taxawu kaayu kaar bi gene jege nekk / metro / taksi? - ¿Dónde está la parada de autobús / metro / taxi más próxima?
0 comentarios