Saludos y presentaciones
Na nga def - Hola.
Ba beneen – Adiós.
Asaalaamu aleykum (ci suba si) – Buenos días.
Asaalaamu aleykum (ci ngoon si) – Buenas tardes.
Asaalaamu aleykum (ci guddi gi) walla fanaan jamm – Buenas noches.
Maa ngi tuddu Mamadu / Fatu – Me llamo Mamadú / Fatu.
Musa laa tuddu yaw nak? – Me llamo Musa ¿y tú?
Senegal laa dëkk – Soy senegalés / soy de Senegal.
Na ka nga def? - ¿Qué tal estás?
Sant bu baax, jërëjëf, yak nak? – Bien, gracias, ¿y tú?
Ma xamale la ak sama xarit Mamadu – Te presento a mi amigo Mamadú.
Am naa ci contante – Encantado.
Bég naa ci lool – Mucho gusto.
Ma ngi am fan weeri at ak ñeent - Tengo 34 años.
Am naa jabar walla am naa jëkkër/ selibateer laa / dama fase / sama jabar walla sama jëkkër dafa déé - Estoy casado-a, soltero-a, separado-a, divorciado-a, viudo-a.
Am naa ñetti doom: ñaar yu goor ak benn bu jigéen - Tengo tres hijos: dos hijos y una hija.
Amuma doom - No tengo hijos.
Mekanisée laa / togg kat laa / garçon laa - Soy mecánico / cocinera / camarero-a
Maa ngiy ligeey ci wallu tabax bi - Trabajo en la construcción.
Amu ma ligeey - Estoy en paro.
Ba benéen – Hasta la vista / hasta pronto.
Ba benéen yoon – Adiós / Hasta luego.
Ba suba! / Ba benéen bess! – Hasta mañana / Hasta otro día.
Di na ñu gise – Nos vemos.
Di naa la woo (telefon) – Te llamo.